Maabo’s Yako Waral Remix Round 6 Lyrics

50

[COUPLET 1] Héy ! Kholate ma kaw ba souf, ma len dakh solou fouf Bbay boul di diawalé, dou beurri yéré moy sagnsé Kholmaaaa ! Fouma meuna guéneu ngané fi leu,  Kham ngaaaa ! Dou ci yéré yi ci mane mi leu Kholm anima 3 pièces diapé,  Té douma djiby dramé, damay dieum mak di délou khalé,  ioe fo could dieuleuté souma nékhé obasanjo,  Def class ték chapeau, kay dieul ay picture,  Li yeup yako waral guissé maabo

(*6*)  Hé ! Ioe khalé bi lé, ni ngey solo déh nexamaaaa ! Oh oh ! Sa dokhine bi nexnamaaaa ! Hé hé ! Ni ngey solo déh nexamaaaa ! Oh oh ! Sa dokhine bi nexnama Niou dém, kone naniou dém thiakass ! Thiakass ! (thieum hé !) Thiakass ! Thiakass ! Dara douniou té thiakass ! Thiakass ! Thiakass ! Thiakass ! Ayway,  Naniou dém thiakass ! Thiakass ! Ooooh ! Héh !  Thiakass ! Thiakass ! Dara douniou té thiakass !  Thiakass ! Nioune dara douniou téré dé

[COUPLET 1] Bala ma dougou école, tchi la am class,  Ma nek ci sa xol, ndax dama am thiass Baby, kholma, douma moramou goné,  Beuss bi tay la, dina la wane fima meuné Di solou ni model, diékk ni djèk, di dagou ni drianké Moussorou ni diouma dieng,  Té fouma tassé sama cheveux accomplished sa beyoncé  Kay diégué ma niou snap selfie, kay niou dieul ay picture,  Aduna yeupeu guiss ko, liiii… ! Yako waral guissé maabo 

(*6*)  Hé ! Ioe khalé bi lé, ni ngey solo déh nexamaaaa ! Oh oh ! Sa dokhine bi nexnamaaaa ! Hé hé ! Ni ngey solo déh nexamaaaa ! Oh oh ! Sa dokhine bi nexnama Niou dém, kone naniou dém thiakass ! Thiakass ! (thieum hé !) Thiakass ! Thiakass ! Dara douniou té thiakass ! Thiakass ! Thiakass ! Thiakass ! Ayway,  Naniou dém thiakass ! Thiakass ! Ooooh ! Héh !  Thiakass ! Thiakass ! Dara douniou té thiakass !  Thiakass ! Nioune dara douniou téré dém

[OUTRO] Thiakass ! Thiakass ! Ioe sama djiguennn…,  Da nga am class bégue na ci ioe Mane ioe yay, lima mome, wowoooohhh ! Guissé maabo 

Comments are closed.

buy levitra buy levitra online